Secret mystique 818

Secret mystique 818

Partager

Informations de contact, plan et itinéraire, formulaire de contact, heures d'ouverture, services, évaluations, photos, vidéos et annonces de Secret mystique 818, dakar, Le Fort-de-France.

03/10/2026

NIOU DIPALÉ KHALÉ YI

Mbok yi ecole bi tidjina aar leen khalé yi si djiné you bone yii di leen daneel si ecole yi
Defar na si ay Teré ak louy nekhal khelou khalé
Koussi beug c’est gratuite
Wotel 779384224

01/10/2026

BATAY MANGUI SI NDIAGNOU SURAT MULK

Lepp lo beug si adina (keur auto nak khar fas place dieukeur diabar touki ) Soko diaré fi ding ko am incha alla barke surat mulk

Bindal saar wi oubi miim yepp dougal si linga beug
So nopé tiim safara bi diangue si saar wi 9 fois
Diko sango bamouy 9 jour incha lossi def ding ko am

Istikhar :779384224
Kou beug teré xam xam asrar wolof amna

01/10/2026

KEPP KOU BEUG AM NDOMBO TANK SI REEW MINGA NEKK (DIRECTEUR, MINISTRE, PRÉSIDENT)

3 sangat you bokoul lay doone:

1- bindal surat mulk entre les aya dougal aya bii
إِنَّا نَحْنُ نَرِثُ الْأَرْضَ وَمَنْ عَلَيْهَا وَإِلَيْنَا يُرْجَعُون
Def soungoufou thiakhat bou laww si garab sango ko 7 jours

2- bindal surat mulk entre les aya dougal si lii

يُحِبُّونَهُمْ كَحُبِّ اللَّهِ
Defsi soungoufou khobou Dakar bou nek si place publique sango ko 21 jour

3- bindal surat mulk entre les aya dougal si aya bi
فَلَمَّا سَمِعَتْ بِمَكْرِهِنَّ أَرْسَلَتْ إِلَيْهِنَّ وَأَعْتَدَتْ لَهُنَّ مُتَّكَأً وَآتَتْ كُلَّ وَاحِدَةٍ مِّنْهُنَّ سِكِّينًا وَقَالَتِ اخْرُجْ عَلَيْهِنَّ فَلَمَّا رَأَيْنَهُ أَكْبَرْنَهُ وَقَطَّعْنَ أَيْدِيَهُنَّ وَقُلْنَ حَاشَ لِلّهِ مَا هَذَا بَشَرًا إِنْ هَذَا إِلاَّ مَلَكٌ كَرِيمٌ
Def si soungoufou khobou neww
Sango ko 21 jour

Nb: sangat yi mane gako defando
Chaque ga sango 3 yepp

Sangat yep disponible na fi
Kou beug Istikhar
779384224

30/09/2026

Secret très très efficace
Lorsque vous voulez vous débarrasser de vos ennemis des personnes qui vous menace ou pour vous preparer avant d’aller dans un pays dangereux ou une mission

Ecrivez la sourat fil 100 fois en intercalant ce verset :

ورميت من رماني بسوء، وكفيتني شر من عاداني

Ajouter jus de 9 citron jaune et beaucoup de sel
Se laver pendant 3 jour

Voyance en distance
Livre asrar en français disponible :779384224

30/09/2026

KOUNOUY FEKHEEL BEUG LA TEUDJ KASSO
Wayé samay mbir kouy toogn wala kouy def lounouy teré bokoo si mane daal nit kou joup tey joubal moma niorr

Lii soko defé ak koula mana teukou manoula teudj kasso incha alla té fo nekk nit gni dinane la wekk

Bindal surat khoudiouraat demal si marché bi si diaaykatou garab yi dieund fa popou diaanou niangoor dieul linga bind sokh ko si guemegn ga so nope euw ko takk ko
Walaay galadj kou yemé la loool

Istikhar :779384224

29/09/2026

Kepp Kou Beugg mboloo finga nekk mboloo mou am ndiarign

Bindal lii 15 fois def ko si Bouteille def si 3 guerté kemb 3 pepou souna 3 pepou Saanio 3 pepou bassi 3 donjou khorom soul ko si bounte bi

Istikhar:779384224

29/09/2026

BATAY NDIARIGNOU GUINAAR

- Kou beuga am doom bindal sourat massadi 9 fois boleko ak soufou guinar fimouy boof sango ko 9 jour

-kou beug sa keur naat dound yomb fa
Outal bopou guinaar sokh si dougoub thieeb sukar ak lepp loo beug mou bari sa keur Soul ko sa keur
keur ga Dina naat incha alla

Kou beug teré xam xam you bari secret
Kou beug ay niaane
Kou beug istikhar
779384224

29/09/2026

LEN SI NDIARIGNOU GUINAAR

« Kou ragal sa Doom ndiaalo
Takal ko wewou guinar biy nekk si teusteune bi Goor bouko tiimé day yoom dou mane si mom dara

- kouy saw lall
Lou Rouge liy nek si boppou guinaar gay togg lekk ko diko faral di def Dinga bayi saw lall

-Jigueen bou manoul am doom
Na bind aya bi 70 fois togué ko guinar bou Jigueen bouy guis regle lakoy lekk Dina am doom incha alla

Kou beug teré xam xam :779384224

29/09/2026

Dina leen may si ndiarignou guinaar topp leen ma

Vous voulez que votre entreprise soit Salon De Beauté la plus cotée à Le Fort-de-France ?
Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.

Téléphone

Site Web

Adresse

Dakar
Le Fort-de-France
54

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Secret mystique 818 publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Souscrire

Nous vous informerons quand tout se passe à Le Fort-de-France.