Sylla Madridista en wolof

Sylla Madridista en wolof

Partager

Halla Madrid 🤍😇

21/09/2026

🚨 Comité Arbitrage yi jël nañu dogal ni dañuy te ay daan arbitre bi di Ortiz Arias mi doon arbitre Derby Madrid, guinaw bimu defe lukou nex ci match bi

Di nañu ko daan ñaari match yom dul arbitre

21/09/2026

Arsène Wenger 🎙️ Réal Madrid dou bayi mukk , bou nek si dernière place dagnou dellusi di xeex, équipe bu dëgër bopp la

21/09/2026

🚨 Suno sukkandikoo ci El Mundo : Fede Valverde dafa ame gaañu gaañu bu metti ci tank bi ginnaaw biko Kang In Lee tacle,

Real Madrid confirme nako , Fade Valverde dina tok ay ayu-bis yomou dul football 🤕

20/09/2026

🚨 Real Madrid TV:

"Dañu ñàkk derby bi ndax arbitre bi

Arbitre bi di Ortiz Arias, xaritu Lamin Yamal la

20/09/2026

🚨 Ancien Arbitre bi di Eduardo Iturralde :

🗣 " Atlético Madrid waroon'a jaaxal match bi ci 9 joueur ci xaaj bu njëkk bi , ndax Cuti Remero ak Kang in lee mérite nañu ay carton rouge

20/09/2026

🚨 leer na : Real Madrid def na ben communique Official di naqaral lou dogal bi arbitre bi di Ortiz Arias wa VAR def ,

Ñaari carton rouge yu wa Atlético waroon'a am ci xaaj bu njëkk bi , cuti Remero ak Kang in lee dañu jàpp ni waru ñu woona àggale match guinaw bi ñu defe tacle ben bi ci Bellingham bisi des ci Valverde waaye arbitre bi ak var b jëlu ñu ben dogal ngir jox leen ay carton rouge, lulou nak meti na trop wa Real Madrid

20/09/2026

❌ 0 tir cadré
❌ 0 centre réussi
❌ 0 passe décisive
❌ 0 occasion créée
❌ 0 but
❌ 7 pertes de b***e
❌ 4 duels perdus
❌ Sorti à la 54ème minute
❌ 0 but en 6 matchs

Ki mom wa nañu jokk ci ay mbiram 😫💔

20/09/2026

Match bi jeexna Real Madrid dafa ñàk ci kanamu Atlético 2-1

Rüdiger ⚽️

Y nada mas 🤍

20/09/2026

Arbitre yi lu leen nex lañuy def li amul VAR amul carton jaune 😫

Photos from Sylla Madridista en wolof's post 20/09/2026

Ñaari carton rouge VAR mom lumuy ñariñ ? 😫

Site Web

Adresse

Diourbel
Touba

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sylla Madridista en wolof publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

S’abonner

Nous vous informerons de toute nouveauté à Touba.