Beug bamba

Beug bamba

Compartilhar

beug bamba

11/04/2025

Touba Ça Kanam

03/11/2024
03/11/2024

Touba ça kanam

17/10/2024

SALAAM
am na mbokkum Taalibe mu jox
Touba Ca Kanam

ÑAARI TÉEMÉERI MILIONS
200.000.000 F CFA

ngir jàpp ci liggéey yu am solo yi Touba Ca Kanam di defal SERIÑ TUUBAA ci dëkk bu sell bi.

Moom mi def jëf ju rëy jii nag bëggul ku wax aw turam mbaa ku ko siiwal ci génn anam.

Nako ñépp ñaanal, jëf juñu nangu, ta defal ko ci lu kawe njortam ci barkep SERIÑ BI

LAAJ LUÑU MAN
DEF KO FUÑU XAM

Ku am yéene ne moom mii man ngaa jaar ci wave biii 👇🏽 amul xeep amul yéem

https://pay.wave.com/m/M_MWpn9-lb-6Zo/c/sn/

Àyca MURIT jëf jël, lu waay jëf yaay boroom.

Quer que seu negócio seja a primeira Salão De Beleza em São Paulo?
Clique aqui para requerer seu anúncio patrocinado.

Telefone

Endereço


São Paulo, SP
1224